Li ma dundee, li ma weesu
Dey delluse, mel ni seetu
Li ma dundee, li ma weesu
Dey delluse, mel ni seetu
Seetal
Leegi leegi ma gesu, ci li ma weesu
Leegi leegi ma recu, walla sax di baaku
Fu gune yi feetee, dama leen di teetee
Wax nu ma neexee, ma bëgga leen
Damay, damay, damay dellu gune
Mel ni, mel ni, mel ni duma màgg
Lu ma gën di yàgg, xel ni mel ni bank
Lu ma gën di màgg, dellu tuuti tank
Li ma dundee, li ma weesu
Dey delluse, mel ni seetu
Li ma dundee, li ma weesu
Dey delluse, mel ni seetu
Ma ni seetal
Leegi leegi ma gesu, ci li ma weesu
Leegi leegi ma recu, walla sax di baaku
Fu gune yi feetee, dama leen di teetee
Wax nu ma neexee, ma bëgga leen
Damay, damay, damay dellu gune
Mel ni, mel ni, mel ni duma màgg
Fu gune yi feetee, dama leen di teetee
Wax nu mu ma neexee ma béggati
Li ma gën di jege, mel ni dama sore
Lu ma gëna sore, gën di gis li ma jegewoon
Lu ma gën di yàgg, xel ni mel ni bank
Lu ma gën di màgg, dellu tuuti tank
Li ma dundee, li ma weesu
Dey delluse, mel ni seetu
Li ma dundee, li ma weesu
Dey delluse, mel ni seetu
Damay, damay, damay dellu gune
Mel ni, mel ni, mel ni duma màgg
Douniya
Más canciones de Youssou N'Dour
Ver todo
Serin Fallu
Youssou N'Dour
7 Seconds (feat. Neneh Cherry)
Youssou N'Dour
Be careful
Youssou N'Dour
Imagine
Youssou N'Dour
Conquer the World (feat. Akon)
Youssou N'Dour
Mon petit âne corse
Youssou N'Dour
Ban La (feat. Fally Ipupa)
Youssou N'Dour
Jeegel Nu (Forgiveness)
Youssou N'Dour
The Lion (Gaiende)
Youssou N'Dour
Quarante ans plus tard
Youssou N'Dour