Le Lion Est Mort Place Aux Hyènes
de Wasis Diop
Kër Amadou Yàlla la juddo
Dékkele la daano, ooooh
Dammeel du Cayor
Lat Dior Ngoné Latyr Diop
Sakhéwar Fatmay maamam
Lat Dior Diobééh man way na jaambaar
Lat Dior Diop kouly diono Fall Fatim
Keroog la Massamba Yacine
des sa Macodou Samba ngone Diogo may
Jaambaar ja ñawuloo Lat Dior
Senegaal seedeleen
Afrique seedeleen ma
Ma jinn jambari jaambaar ja
Mbër mi daan te bakkuwul
Lat Dior Diobééééh
Yaa yaayoo Diadieuffeuto
Si hiii hiiii hiii hiiii
Lat Dior Diop bañkat ba
Lat Dior Diop xarekat ba
Lat Dior Diop jaambaar ja
Jambaar ja ñawuloo ma way
Bër Guett Sakhéwar Sokhna Mbaye Diop moy baayam
La lingeer Ngoné Latyr Fall lay yaayam
Ngoné Latyr Absa Ngonou
Absa Ngonou Absa Diop
Absa Diop Isseu Dieye
Fatim Penda Lat Soukabé
Ngoné Dieye Lat Dior
Diru ñaar fukki at ak juróom
Lat Dior Diop xeex na tubaab ba ak jaambaar jee
Ngir bañ rail ba diggante Ndakaru ak Ndar Géej
Ngoné Latyr Diop xeex na ba danoo dékkele
An yeeh
Lelelelelele
Lat Dior Diop Kouly Diono
Ma ne way na jiin na
Bakk na jaambaar ja
Lat Dior Ngoné Latyr Diop
Senegaal seedeleen ma, ma way
Senegaal seedeleen ma, ma jiin
Gnimé Gnimé Gnimé
Gnimé Lat Dior Diop
Mi gnimi Lat Dior Ngoné Latyr Dior
Mo daan tubaab ba sa N'golgol
Daan ko sa mexee, daan ko sa Paoskoto
Ànd ak Maba Diakhou Ba
Moo daan Madiodio Déguéne Codou
Ak tubab ba sa Cokiii
Lat Dior Diop man jooy naa
Jaambaar Lat Dior Diop
Ngor nga sa Lat Dior moo nekk sa Malaw
Ngor nga sa Lat Dior moo nekk sa Malaw
Malaw ànd ak moom ci xare ya
Baol - Ndiambour ak Saloum
Malaw fas ba déggal Lat Dior
Malaw gisul rail ba
Más canciones de Wasis Diop
-
Le passeur - Edit Radio
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
Parler
De la glace dans la gazelle
-
-
No Sant
No Sant
-
Everything (... Is Never Quite Enough)
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
Ramatu
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
Samba le berger - Radio Edit
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
African Dream
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
Dem Ba Ma
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
Digge (Le gong a sonné)
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
Dune
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
Soweto Daal
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
DéFaal Lu Wor (Once In A Lifetime)
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
No Sant
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
Chapelle - Kaay Niu Gospel
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
Julia
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
Holaal Bu Baah
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
Raï M'Bele
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
Ballad Of The Feather
Everything Is Never Quite Enough - Best Of
-
My Son
Everything Is Never Quite Enough - Best Of