Yobaneté
de Wally B. Seck
Khalei bima giss si mbéd mii
Mom mougi dioyy, nane ani sama yaye
Khalei bima giss si mbéééd mii
Mom mougi dioyy nane ani sama baye
Wouy wallou wouy walloo
Kon yén téléne sougnouy domm
Wouy wallou wouy walloo
Kone yéne yar léne sougnouy domm bagne naww léénn
Khalei bima giss si mbèd mii
Mome mougi dioyy nane ani sama yaye
Khalei bima giss si séédaay bi
Mou déf tankii néne nane ani sama baye
Wouy wallou wouy walloo
Kone yéne téé lééne séni domm
Wouy wallou wouy walloo
Kone yéne yarr lééne sééni domm, domm naww léé la
Mane dé beuugouuma mane dé bagne na
Giss khalei bouy takhawaalou si mbéédd mi
Wouy wallou wouy walloo
Kone yéne tééléén séni domm
Ndakh domm naww, lééleuh
Wouy léélé lé léélélé ya
Geumnani yaye diour domm moy déf
Dakoy kholl rek di sourr melni mbonate ak dooomame, lou yéémé
Douko ndampall dom trésor leuh
Kou sagnone sa domm mom mouy done iaw kilay geune
Kone khaleii momite lagne na kouko topatô
Wayé ndeye marie fatou salam mom sa
Domm leu fonkouga djibi yagui koy topatô
Manaa chérie diooma chérie mami arame
Mon amie thiaminial liii keu bakh manaaa!
Sidibiidibibara sibiraba sibaara, sidibidibida sabaribida
Thiey bii diambar Sama domm leu néna sama domm leu kou sagnone sa
Domm molay geune Nourou yaye ni khalei mom meunoull nagne ko topatô
Heuuh, sidibiidubibara sibiraba sibara, si ribidibida sabaribida
Héé héhé héé héhéé nagne ko tèee khalei yaroul
Yakbounouti koula diaangalsidigidiginaw dara touko tée
Alou bay falli lay ahh
So dégalé yaye teksi dégal baye boye
So magué tékkiga mako garantie héhé
Sokhna faty sa domm leuh maman oumy ndiaye
So dégalé yaye teksi dégal baye boye so magué tékkiga mako garantie
Khalei yi dagne ma yoni mane douma tayi may sén baye
Heur bou yalla dé fégne wolou kaularéme bobe aan
Dagnouma yaubanté mane khalei té khamoul loumouy dioy
Yallaa laa yee
Más canciones de Wally B. Seck
-
Dafmay Dal
Symphonie
-
Symphonie
Symphonie
-
Let Them Grow Up
Afromix
-
Le temps
Etat d'esprit
-
Ma Cissé Alima Ndiaye
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Balma
I Wanna Be Free
-
Mirna - Live
Apero (Live 2017)
-
Borom keur - Live
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Yoon wi - Live
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Le temps - Live
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Woyal Li
Symphonie
-
Soma méré wakhma
Etat d'esprit
-
Je ne suis pas comme eux
I Wanna Be Free
-
Légendes - Live
Apero (Live 2017)
-
Yaye
Yaye
-
D'accord - Live
Apero (Live 2017)
-
Defma ndank
Etat d'esprit
-
Fii Lay Né
Afromix
-
Boulko Tek Missér
Xippil Xoll
-
Louné
Louné