WURUS - Version Mbalax
de Wally B. Seck
Yay sama adouna, oh, yeah
Sama baby coco waay, ey yeah
Yow yay sama aldiana
My love, sama baby coco waay, hmm yeah
Baby yay mane
Teudeul nèlaw kham gni moununj dara
I don’t give about mèrr katt fadjoul dara
Takal la or ba ci 24 carats
Dagn lénn di bayèkk peureum bi
Gnom gnouy deukké aya
Baby, I just want real love
Real love, I just wanna know real love, definitely, I don't wanna lie
Yay sama adouna, oh, yeah
Sama baby coco waay, ey yeah
Yow yay sama aldiana, my love
Sama baby coco waay, hmm yeah
Way way way way
Mèrr bi fadjoul dara
Mom fadjoul dara
Konn fadjoul dara
Baylènn té gneuw ma takal la or 24 carats
Wurus 24 carats
Ngualam 24 carats
Khana dou mala yèenè
Ma vie, ma vie
Don't lie to me
Su fekeh guiss nga ci man lo musuta guiss ci kenen baby dawwsil gaww
Ba takh mani la baby dawwsil gaww
Baby yay mane
Teudeul nèlaw kham gni moununj dara
I don’t give a fuck mèrr katt fadjoul dara
Takal la or ba chi 24 carats
Dagn lénn di bayèkk peureum bi
Gnom gnouy deukké aya
Baby, I just want real love
Real love, I just wanna know real love, definitely, I don't wanna lie
(I'm in love with you, in the morning, in the night, oh, yeah)
(I'm in love with you, in the morning, in the night, oh, yeah)
Yay sama adouna, oh, yeah
Sama baby coco waay, ey yeah
Yow yay sama aldiana, my love
Sama baby coco waay, hmm yeah
Way way way way
Mèrr bi fadjoul dara
Mom fadjoul dara
Konn fadjoul dara
Baylènn té gneuw ma takal la or 24 carats
Wurus 24 carats
Ngualam 24 carats
Más canciones de Wally B. Seck
-
Dafmay Dal
Symphonie
-
Symphonie
Symphonie
-
Let Them Grow Up
Afromix
-
Le temps
Etat d'esprit
-
Ma Cissé Alima Ndiaye
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Balma
I Wanna Be Free
-
Mirna - Live
Apero (Live 2017)
-
Borom keur - Live
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Yoon wi - Live
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Le temps - Live
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Woyal Li
Symphonie
-
Soma méré wakhma
Etat d'esprit
-
Je ne suis pas comme eux
I Wanna Be Free
-
Légendes - Live
Apero (Live 2017)
-
Yaye
Yaye
-
D'accord - Live
Apero (Live 2017)
-
Defma ndank
Etat d'esprit
-
Fii Lay Né
Afromix
-
Boulko Tek Missér
Xippil Xoll
-
Louné
Louné