Runaway
de Wally B. Seck
Runaway ooh runaway
Find a way, ooh runaway
Guédja ngui kheuthiou di nieuw
Té khamoulo louko teuyé sama waay
Mbirou yalla
Ndéké charte biir guéédj
Kou eup seu morom dolé agné
Ah damay laadj
Niou nééw dolé, ni niom founiouy agné
Xanaa dadjék borom yeurmandé
Adouna nii la bindo
Makhaama gni ley tané wor nama
Runaway ooh runaway
Runaway ooh runaway
Lima yalla thieuralé
Lenen lou bokoul ci mom beugou mako
Mo xam lou nééw, mba mou beuré bari beugou mako
Non non non
Kone yalla bo dadjék mom
Am-am ci tél mom, ci moudieuntél
Yallay mayé Oh-ohh
Diaam bi takhawél Alhamdoulilahu
No no no no no
Léér biy daw seu dieum dji
Worna keuwnou-bi walay wowowo
Té bou nieup yamone thieur
Am niou guééd sen boss bilaay, wornama
Gorgorlou doyna borom bi
Molay takha done goor fayalaahou
Gueum naa ni li rouh di doundé
Dina fegn ci dieum dji lilaay
Dieun bou mak bay beug lorr dieun bou ndaw bi
Té xamoul ni ci biiram beu léy agné
Dou deugné dou deugné eh eh
Yeurmandé Lahu daa yaa
Yalla na yalla yeureum diaam gni
Bilaay yeurmandé Lahu bour bi
Runaway ooh find a way
Runaway ooh find a way
Runaway ooh find a way
Runaway ooh find a way
Ooh Yalla yaay borom diaam gni
Ngueuramal souniou borom
Louma meunti am, momako gueunal
Yeurmandé Lahu
Yeurmandé Lahu daa yaatou
Más canciones de Wally B. Seck
-
Dafmay Dal
Symphonie
-
Symphonie
Symphonie
-
Let Them Grow Up
Afromix
-
Le temps
Etat d'esprit
-
Ma Cissé Alima Ndiaye
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Balma
I Wanna Be Free
-
Mirna - Live
Apero (Live 2017)
-
Borom keur - Live
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Yoon wi - Live
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Le temps - Live
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Woyal Li
Symphonie
-
Soma méré wakhma
Etat d'esprit
-
Je ne suis pas comme eux
I Wanna Be Free
-
Légendes - Live
Apero (Live 2017)
-
Yaye
Yaye
-
D'accord - Live
Apero (Live 2017)
-
Defma ndank
Etat d'esprit
-
Fii Lay Né
Afromix
-
Boulko Tek Missér
Xippil Xoll
-
Louné
Louné