Nous ne sommes presque rien
de Wally B. Seck
Dof ci yaw bu mu tax ba nga foog ni
Soo toppee sa taar dina la jaay
Nekkal nit moo gën ngay foog ni
Entre nous, si on se disait la vérité
Tu sauras que nul n'est épargné
Gis nga mbëggeel, xoolul mag, xoolul ndaw
Tu sauras que nul n'est épargné
Dof ci yaw ba mu tax ba nga foog ni
(Mënuma la bàyyi)
Soo toppee sa taar dina la jaay
(Ba nga foog doo daanu)
Nekkal nit moo gën ngay foog ni
(Mënuma la wan gannaaw)
Entre nous, si on se disait la vérité
Tu sauras que nul n'est épargné
Gis nga mbëggeel, xoolul mag, xoolul ndaw
Tu sauras que nul n'est épargné
Dof ci yaw ba mu tax ba nga foog ni
(Mënuma la bàyyi)
Soo toppee sa taar dina la jaay
(Ba nga foog doo daanu)
Nekkal nit moo gën ngay foog ni
(Mënuma la wan gannaaw)
Chaque jour, maa ngi ñaan Yàlla suñu boroom
Nga déllusi dellusiwaat ci samay loxo
Gis nga mbëggeel, xoolul mag, xoolul ndaw
Tu sauras que nulle n'est épargné
Koo fi mëna am!
Ak loo fi mëna doon
Mbëggeel aka bari doole
Soo ko xoolee ba ci biir, yaw yaay!
Wuy bàyyee - ma waay!
Séet la la yénnewoon
Wala séy ci
Aaaah, soo ma bëggoon doo ma def lii
Ba may gis keneen waawaaw
Soo ma bëggoon doo ma def lii
Gis nga léegi nu ma mel ci yaw
Nob naa keneen, gis naa keneen
Sa jikko moo waral, waral
Mbër mi dafa ñëw dimanche
Yaayam ñaanal ko
Bay ba ñaanal ko
Sëriñ ci ñaanal ko
Yaa ma saagaane ma dem
Soo ma wayadi loo ma dem
Dama dof ci yaw nañ ko xam
Man yaa ma saagaane ma dem
Soo ma wayadi loo ma dem
Dama dof ci yaw nañ ko xam
Mbër bu dékke daane
Fatima A guest ma waay!
Más canciones de Wally B. Seck
-
Dafmay Dal
Symphonie
-
Symphonie
Symphonie
-
Let Them Grow Up
Afromix
-
Le temps
Etat d'esprit
-
Ma Cissé Alima Ndiaye
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Balma
I Wanna Be Free
-
Mirna - Live
Apero (Live 2017)
-
Borom keur - Live
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Yoon wi - Live
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Le temps - Live
Live 2023 (Live Vogue Night Club)
-
Woyal Li
Symphonie
-
Soma méré wakhma
Etat d'esprit
-
Je ne suis pas comme eux
I Wanna Be Free
-
Légendes - Live
Apero (Live 2017)
-
Yaye
Yaye
-
D'accord - Live
Apero (Live 2017)
-
Defma ndank
Etat d'esprit
-
Fii Lay Né
Afromix
-
Boulko Tek Missér
Xippil Xoll
-
Louné
Louné