Sadik Lady
de Viviane Chidid
Bu ñuy doxaan ci lu ne dinga ko dégg
I love you baby, my sweety, my lady
Yaa ma gënal sama ndey ji ak sama baay be
Sukk, raam, jébbalu, jooy, lu ne ñu def ko
Bu ñuy doxaan ci lu ne dinga ko dégg
I love you baby, my sweety, my lady
Yaa ma gënal sama ndey ji ak sama baay be
Sukk, raam, jébbalu, jooy, lu ne dinañu ko def
Li ma metti ba tax ma soppi jikko (moom)
Def ni ma mel ba noppi ni fess (moma)
Nelawal ma ma yewu gëna sadik (moma)
Góor-e tax jigéen soxor leegi
Jël pakka jam ko sama digg xol (moma)
Bayi fa lekket bo xamni du deñ (moma)
Nelawal ma ma yewu gënë sadik (moma)
Góor-e tax jigéen soxor leegi
(Leegi)
Ñaata yoon la ma wax I love you
My baby
(Baby)
Ñaata yoon lama wax loolu
Xale bile moom, lu Yàlla xam doyna
Dafma gëlëmël ci mbëggeel touté dess mu ray ma
Xale bile moom, dafma né daf ma lova
Ndeketé lepp lum la mës wax ay fenn la
Xale bilé (ñewna)
Xamal mani (moom la)
Néma sama (goor la)
Lepp ay (door la)
Xale bilé (moma)
Soppi na (jikom ba)
Fima ko romboon ci mbedd mi daf ma dab
Bula góor toppate ne la bëgg naa la
Xamal ko xol dafa oyof buguma nga gañ ma
Bula góor toppate néla bëgg nala
Lacc ko bëgg na giss papam di toroxal Yayam
Baby
Bu ñuy doxaan ci lune ding ko deg
I love you baby, my sweety, my lady
Yama gënël, sama ndey ji, ak sama baay bé
Sukk raam jébbalu joy lune ñu def ko
Bu ñuy doxaan ci lune ding ko deg
I love you baby, my sweety, my lady
Yama gënël, sama ndey ji, ak sama baay bé
Sukk raam jébbalu joy lune dinañ ko def
Lima metti batax ma sopi jikko (moma)
Def nima mel ba nopi ni fess (moma)
Nelawal ma ma yewu gëna sadik (moma)
Góor-e tax jigéen soxor leegi
Jël pakka jam ko sama digg xol (moma)
Bayi fa lekket bo xamni du deñ (moma)
Nelawal ma ma yewu gënë sadik (moma)
Góor-e tax jigéen soxor leegi
(Leegi)
Ñaata yoon lama wax I love you
My baby
(Baby)
Ñaata yoon lama wax loolu
Buñu bëgg dem, buñu bëgg dem
Te gën lula ci
Yawit boleen jekko tegal le lu sadik
Buñu bëgg dem, buñu bëgg dem
Te gën lula ci
Yawit amal fulë amal fulë
Waawaaw bàyyi ko, bàyyi ko
Ndax moom xamul sa njëg
Oh bàyyi ko oooh
Ndax moom xamul sa njëg
Sister, please don't cry
Fompal say rangooñ
Bul la góor jaral ngay jooy
Fompal say rangooñ
Bu ñuy doxaan ci lune ding ko deg
I love you baby, my sweety, my lady
Yama gënël, sama ndey ji, ak sama baay bé
Sukk raam jébbalu joy lune dinañ ko def
Lima metti batax ma sopi jikko (moma)
Def nima mel ba nopi ni fess (moma)
Nelawal ma ma yewu gëna sadik (moma)
Góor-e tax jigéen soxor leegi
Jël pakka jam ko sama digg xol (moma)
Bayi fa lekket bo xamni du deñ (moma)
Nelawal ma ma yewu gënë sadik (moma)
Góor-e tax jigéen soxor leegi
(Leegi)
Ñaata yoon lama wax I love you
My baby
(Baby)
Ñaata yoon lama wax loolu
Más canciones de Viviane Chidid
-
Yaakaar
Yaakaar
-
No Stress
Wuyuma (DTM)
-
Do Dara
Benen Level
-
Rëcc Na
Benen Level
-
Yenn Saï
Benen Level
-
Djoug Liguey
Benen Level
-
Tèrè Doundou
Benen Level
-
Nangoulema
Benen Level
-
Déranger
Benen Level
-
Senegal
Benen Level
-
Benen Level
Benen Level
-
Def Ndam
Benen Level
-
Yenë Saay
Benen Level
-
Wuyuma
Wuyuma (DTM)
-
Da Fa Gnaw
Wuyuma (DTM)
-
Mariage forcé
Wuyuma (DTM)
-
Sénégal Ben Bop
Wuyuma (DTM)
-
Mbifé
Wuyuma (DTM)
-
SOPÉ
SOPÉ
-
Yeuk Yeuk
Yeuk Yeuk