No Stress
de Viviane Chidid
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Suñu xol di fees ñoom ñu juk def fés
Non, non, duma nangu nga may teg stress
Duma nangu nga may teg stress
Ma bañ duma ko nangu no stress
Sama xol di fees yaw nga juk def fés
Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Danga fàtte ni awma dix ans
Lu tax nga jël ma bëgg ma def sa fowukaay
Yombalal naa la sa visa
Wow yeah yeah, demal fu la neex way!
Bëgg langak ki
Bëgg langak ke
Bëgg langak samay xarit ma ni night and day
Dégg na ñu ne feebar la
Wow yeah yeah, defal lu la neex way!
Non non duma nangu nga may teg stress
Duma nangu fils nga may teg stress
Ma bañ duma ko nangu no stress
Sama xol di fees yaw nga juk def fés
Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma bëgg a tardel bëgg ma fowe ma romb la
Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma bëgg a tardek man ma romb la
Li safatuma
Sama mettitu muñ jeex na
Li yëngëluma
Ndax te man ñakkuma fayda
Li safatuma
Tegg ci temps def ba mu baax jot na
Te yaw mi xam nga
Soo ma nobul sa moroom nob ma!
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Suñu xol di fees ñoom ñu juk def fés
Non, non, duma nangu nga may teg stress
Duma nangu nga may teg stress
Ma bañ duma ko nangu no stress
Sama xol di fees yaw nga juk def fés
Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Góor goula teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma bëgg a tardeel bëgg ma fowe ma romb la
Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma bëgg a tardèk mane ma rombe la
Más canciones de Viviane Chidid
-
Sadik Lady
Sadik Lady
-
Yaakaar
Yaakaar
-
Do Dara
Benen Level
-
Rëcc Na
Benen Level
-
Yenn Saï
Benen Level
-
Djoug Liguey
Benen Level
-
Tèrè Doundou
Benen Level
-
Nangoulema
Benen Level
-
Déranger
Benen Level
-
Senegal
Benen Level
-
Benen Level
Benen Level
-
Def Ndam
Benen Level
-
Yenë Saay
Benen Level
-
Wuyuma
Wuyuma (DTM)
-
Da Fa Gnaw
Wuyuma (DTM)
-
Mariage forcé
Wuyuma (DTM)
-
Sénégal Ben Bop
Wuyuma (DTM)
-
Mbifé
Wuyuma (DTM)
-
SOPÉ
SOPÉ
-
Yeuk Yeuk
Yeuk Yeuk