GUÉLOU RAP
de Viviane Chidid
Ioe so ñeimé, ñu déef waaw waaw
Sopaalike rap djomaal
Moytul ma dooflo laa
Ioe no beügé, ñu déef waaw waaw
Djuuma djomaalul boopam naak
Cà séeytané maan leü
My baby boy, xaam na ni tiit nga
Cà fiit bi teüp naa nooma gissé
Li ma sool daay dooflo goor
Tée saax tass na guerre moytul ma killer
Je vais te rendre fous, je vais te rendre fous
Anaa cà xéel bi déem na
My baby, je vais te rendre fous, je vais te rendre fous
Waxaal waaxu niit
My baby kaay, te rendre fous, je vais te rendre fous
Anaa cà xéel bi déem na
Oh my baby, je vais te rendre fous, je vais te rendre fous
(Waxaal waaxu niit) Yaa doof ba feel ci maan
Baari vitesses paré kooba
Ioe daa nga fiir duugu ci maan
Léep lo tchi goobé maané ioe leü
Maané laa néek tchi née
Ruuku djiné la laay duugal
So moytuwul ma djomaal leü guudi
Yooré taaru djiné, mba duuñ née
Moom daafa dadjék guélou rap taax mu
Daaf koy saalite
Xaam na ni tiit nga
Cà fiit bi teüp naa nooma gissé
Li ma sool daay dooflo goor
Tée saax tass na guerre moytul ma killer
Je vais te rendre fous, je vais te rendre fous
Anaa cà xéel bi déem na
My baby, je vais te rendre fous, je vais te rendre fous
Waxaal waaxu niit
My baby kay, te rendre fous, je vais te rendre fous
Anaa cà xéel bi déem na
Oh my baby, je vais te rendre fous, je vais te rendre fous
Waxaal waaxu niit
So beügé ba mu djaaral leü
Doof lool wadji booko meünul baayi
Maané so beügé ba mu djaaral leü
Doonal gyal bi di doof lo wadji, tchi deüg deüg
So beügé ba mu djaaral leü
Doof lool wadji booko meünul baayi
Maané so beügé ba mu djaaral leü
Naa saaf kaani guudi bul tchi taayi
Doonal rap su ngooné
Djomaal ko su ngooné, ioe su ngooné
Waan ko ni nga méel, méetil doof loo ko
Waan ko ni nga méel, djaaxal ko doof loo ko
Doonal rap su ngooné
Djomaal ko su ngooné, ioe su ngooné
Waan ko ni nga méel, méetil doof loo ko
Waan ko ni nga méel, djaaxal ko doof loo ko
Raakadju na maané raakadju na
Su féeké ñeimé wo cà gyal lu rap bi poussal fée
Raam paam pii raam, maané raam paam pii raam
Su féeké ñeimé wo cà gyal lu rap bi poussal fée
Woooo feülé
Maan ni ma méel doof lo naa goor
Doof lo naa ku néek
Eeee o héy
Xaalé bu djigéen bi lu mu saañsé lo déef nga géestu
So beügé ba mu djaaral leü
Doof lool wadji booko meünul baayi
Maané so beügé ba mu djaaral leü
Doonal gyal bi di doof lo wadji, tchi deüg deüg
So beügé ba mu djaaral leü
Doof lool wadji booko meünul baayi
Maané so beügé ba mu djaaral leü
Naa saaf kaani guudi bul tchi taayi
Doonal rap su ngooné
Djomaal ko su ngooné, ioe su ngooné
Waan ko ni nga méel, méetil doof loo ko
Waan ko ni nga méel, djaaxal ko doof loo ko
Doonal rap su ngooné
Djomaal ko su ngooné, ioe su ngooné
Waan ko ni nga méel, méetil doof loo ko
Waan ko ni nga méel, djaaxal ko doof loo ko
Waan ko ni nga méel, méetil doof loo ko
Waan ko ni nga méel, djaaxal ko doof loo ko
Más canciones de Viviane Chidid
-
Sadik Lady
Sadik Lady
-
Yaakaar
Yaakaar
-
No Stress
Wuyuma (DTM)
-
Do Dara
Benen Level
-
Rëcc Na
Benen Level
-
Yenn Saï
Benen Level
-
Djoug Liguey
Benen Level
-
Tèrè Doundou
Benen Level
-
Nangoulema
Benen Level
-
Déranger
Benen Level
-
Senegal
Benen Level
-
Benen Level
Benen Level
-
Def Ndam
Benen Level
-
Yenë Saay
Benen Level
-
Wuyuma
Wuyuma (DTM)
-
Da Fa Gnaw
Wuyuma (DTM)
-
Mariage forcé
Wuyuma (DTM)
-
Sénégal Ben Bop
Wuyuma (DTM)
-
Mbifé
Wuyuma (DTM)
-
SOPÉ
SOPÉ