Djoug Liguey
de Viviane Chidid
Delousil delousil dougal nga darra
Dé diaroul xass
Meuneu dem ma takha dem moytou
Dougou thi auto you tass
Wakh bi ni nga ko dégué, diaapé ko
Nounou, Mba compou nga
Oooh ooh ooh
Ni diamono ji legui da ngay ré ba dé
Fima dieuma sori damey bagn goudé
Wakh dji beurina déy nourou mariné
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Ni wo woo Vivi bougnou faalé
Bougnou décodé
Nagnou baalé
Ki léy diébaané
Boko séété dé yaako tané
Mane dé déég naala
Dafa féék né taloumala
Eyow eyow evow
Di nga sonou Faramareen féép leu meuné
Eyow eh
Nangoulmako té nga Take a seatt, Take a seat
Vivi gnou féthial ko Reuguine tass
Meuneu dem ma takha dem moytou
Dougou thi auto you tass
Wakh bi ni nga ko dégué, diaapé ko
Nounou, Mba compou nga
Oooh ooh ooh
Ni diamono dji legui da ngay ré ba dé
Fima dieuma sori damey bagn goudé
Wakh deug bagnou mala
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Deloussil deloussil, comment tu vas
(Comment tu vas)
Nangoul niou lou niou mom té yalla takh
(Té yalla takh)
Maléy sonnal, té dawoulo dé wawaw
Demal nga tok, mané dolé yemoul
Wawaw
Kou andak li niou andal loula nekh lathie
Wally ak Viviane beuri fitt pathie, yeah yeah
Bokk école, bokkou niou classe, té douma sa mass
Ma tangal sa khol, wakhko sa vave mou soti si glace
Té ragalouma lolou wooooh
Ni diamono dii legui da ngay ré ba dé
Fima dieuma sori damey bagn goudé
Wakh deug bagnou mala
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Bilay man dé beug naala
Di naagn la féthial reguine tass
Walay man dé beug naala
Di naagn la féthial reguine tass
Mayanté xaliss diaroul khass
Di naagn la féthial reguine tass
Bilay man dé beug naala
Di naagn la féthial reguine tass
Sant yalla dey nourou titeurou
Wakh deug yalla tognou gnou
Bour yalla né sante lén ma doli
Ba takhna ma deuké thiant-gui
(Eh eh, kou seu xol nekh nga ré)
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Di naagn la féthial reguine tass
Más canciones de Viviane Chidid
-
Sadik Lady
Sadik Lady
-
Yaakaar
Yaakaar
-
No Stress
Wuyuma (DTM)
-
Do Dara
Benen Level
-
Rëcc Na
Benen Level
-
Yenn Saï
Benen Level
-
Tèrè Doundou
Benen Level
-
Nangoulema
Benen Level
-
Déranger
Benen Level
-
Senegal
Benen Level
-
Benen Level
Benen Level
-
Def Ndam
Benen Level
-
Yenë Saay
Benen Level
-
Wuyuma
Wuyuma (DTM)
-
Da Fa Gnaw
Wuyuma (DTM)
-
Mariage forcé
Wuyuma (DTM)
-
Sénégal Ben Bop
Wuyuma (DTM)
-
Mbifé
Wuyuma (DTM)
-
SOPÉ
SOPÉ
-
Yeuk Yeuk
Yeuk Yeuk