La vie est belle
de Mia Guisse
On ne vit qu'une seule fois
On ne vit qu'une seule fois
Une seule fois
Day lëndëm may shine
Mbow mbow duñu dara
Bul geestu, bul faale
Et laisse-les bavarder
Man buy neex duma doyal
Lu mel ni man wëral
Dawal ba mel ni évadée bébé
Jën moo rëcc ay filets bébé
Jaune banaanaa (banaanaa)
Fu ma génnee ci rouge ba daagu fa yépp vert
Sama sourire moo ëpp doole balle-u fetal, yeh
Wurus bu Yàlla ngalam manoo wax ba soppi ko përëm
Ye-ye-yeh!
Yéen mbaa nommoon ngeen ma
(Noo def mu neex)
Waaye jeex na ñëw naa
(Noo def mu neex)
Comme fi mu ne baax na
(Boo defee mu neex)
Beydu volume mi nanaani
(Boo defee mu neex)
Nanaani
La vie est belle
On ne vit qu'une seule fois
On ne vit qu'une seule fois
Une seule fois
Ni ku nekk ci diggu diggu lëndëm daal
Yàlla jekki rekk taal say làmp
Ngay doxal doxal
Di doxal doxal, dara fayu ma man
Jàppal loxo ki ne sa wet
Ñu bége bala ñoo dem
Kon doxal doxal
Ñu doxal doxal, dara fayu ma
Man maa koy yëngal yëngal
Yëngal mu naan rëgëj-rëgëj
Fecc ko ni kuy riij bëgëj
Effets yi mooy créer émeute
Gisoo ni maa kooy yëngal yëngal
Yëngal mu naan rëgëj-rëgëj
Fecc ko ni kuy riij bëgëj
Yéen mbaa nommoon ngeen ma
(Noo def mu neex)
Waaye jeex na ñëw naa
(Noo def mu neex)
Comme fi mu ne baax na
(Boo defee mu neex)
Beydu volume mi nanaani
(Boo defee mu neex)
Nanaani
La vie est belle
Man maa koy yëngal yëngal
Yëngal mu naan rëgëj-rëgëj
Fecc ko ni kuy riij bëgëj
Effets yi mooy créer émeute
Gisoo ni maa kooy yëngal yëngal
Yëngal mu naan rëgëj-rëgëj
Fecc ko ni kuy riij bëgëj
La vie est belle
Fu ma génnee ci rouge ba daagu fa yépp vert
Sama sourire moo ëpp doole balle-u fetal, yeh
Wax yi du romb, yére yi faxasu leen
Faxasu leen
Más canciones de Mia Guisse
-
Idda
Idda
-
Lonkotina
Lonkotina
-
Gën Leen Paré - GLP
Gën Leen Paré (GLP)
-
Gauche & Droite
Gauche & Droite
-
Choix
Choix
-
Fake News
Fake News
-
Rubami la Notte
Fake News
-
Coca zero
Fake News
-
Zen
Fake News
-
L'Ultima Volta
Fake News
-
Hold On
Fake News
-
Stage Diving
Fake News
-
Ricordi
Fake News
-
Melting Pop
Fake News
-
Forse
Fake News
-
Fede
Fake News
-
Dentista Croazia
Fake News
-
Hikikomori
Fake News
-
Giovani Wannabe
Fake News
-
Barfly
Fake News