Intro
de Dip Doundou Guiss
(Humm hum)
(Oh oh)
(Yeaah)
Daj ngeen ci ëkk, këkk, ndëgg sërëx
Doo ma jey ba jaay ma doog maa bëgg nëbb sa njëg
Duma la daan ba toog sa kaw nga bëgg ma njëkk sëlëm
Rap dëkkatul ci sama xol daa tëju sama xëtër
Gëtam ay boys you téxet ba ër, tëx, lu tëb di sëmbëx
(Low) Ci sama jëmm tay laa gën a dëgër
Utal kër mère bi, ngandim maamu Mercedes ak chauffeur
Tës xëtëm yi njëkk du mës a jëmbët ku leen gën a sëcc
Sàcc du sàcc ba sàcc sama sacrifices yi
Noon bi lay ray mën na jaar ci fiisabii Lilahi
Jaag du kàcc ba daj ma ci njuuj njaaj
Jiiñ ngeen ma bon, jiiñ ma soxor
Jiiñ ngeen ma yéefar ak Illuminati
Li ma moom buy dem ci keneen ku dul man mii
C'est comme mardi-gras bu ñu feetwul ci mardi
Ci biir camps yi laa koy def ni Jamie Vardy
Lëndëm, samay fautes du feeñ mukk ci VAR bi
(Yeah) Dara dootu ma defati dara
Am ndam fi ma ko waroon am yépp mais defaite bi man a
Xëy te duma waaj doyal ci life te fekkeeguma gat
Facturu àq yi ma ame yépp lay fay te duma rang
Xeet yépp la suuf warax du kaaw kese rekk fepp ay suul ndanaane
Seen game jarul tuur leketu kaana ak dereetu mala
Tekkeeguma gat ci musique bi mel ni sexluwuma cat
Kenn yeemu ma ndax mënuma féey ci tefes di fa lab
Ñi dama leen yagg fuck ba ñu foog ne ñu jur samay doom
Duggal sama zone dama lay duut ba pare rouge la nga toog
Rap Galsen man rekk la benn MC buy course ak sa bopp
Mën nga ma fuck? Microphone bi Dip sa tuun la ko roof
Juumal ba dof nu bokk son dama lay ñuus dama lay noq
Kuy sut sama njort ndayam judduwul maamam fause couche la defoon
Boy duma sa moroom maak yow bokkounu
Ni suurka xorom
Ni Ummah ak Rome
Joueurs yi ak Àllaaji Juuf double ballons d'or
Ni sumb ak fomb
Sunguf ak ndox
Dugub ak mboq
Ni dunq ak góor
Ni kuy mbalax ak kuy dund hard core
Chaque joueur mën na togg benn single suul double album
Lu ma def tay suba ñoom ñépp def ni Duudu ak Ngóor
Maay buur bi maay boos bi, bul ma tëkkale ak buujuman yoyou
Fàtte xaju fi Lépp Fii La nu Fekk ni turu album bi
Más canciones de Dip Doundou Guiss
-
Holocauste
Tay Leu Kagn
-
Beut
Tay Leu Kagn
-
YMYM
Tay Leu Kagn
-
Kheula
Tay Leu Kagn
-
#Kmnd
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Bad Man
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Jëli li des
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Nguur
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
LGT
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Sunshine
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Destin
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Dee ci yaw
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Nimala beugué
Tay Leu Kagn
-
Damako Khar
Tay Leu Kagn
-
Dou raggal dou respect
Tay Leu Kagn
-
Niata la yalla fay sa xol
Tay Leu Kagn
-
Bandit
Tay Leu Kagn
-
Niata nio dess
Tay Leu Kagn
-
Funérailles
Tay Leu Kagn
-
Innoncent
Tay Leu Kagn