Je m'en fous de ça
de Bass Thioung
Ay, àdduna yàggul, bul jaay sa ngor
Bu dara fekk sa bët looloy nobless
Ay, àdduna yàggul, bul jaay sa ngor
Bu dara fekk sa bët looloy nobless
Man ngor la (eey), doomi ngor la (eey)
Man ma nob la (eey), dara fekkul samay bët (eey)
Man ngor la (eey), doomi ngor la (eey)
Man ma nob la (eey), dara fekkul samay bët (eey)
Man li ma ñàkk ak li ma am kenn du ko xam dox doy
Man awma fekkul samay bët (liggéey rekk ko woor)
Man li ma ñàkk ak li ma am kenn du ko xam dox doy
Man awma fekkul samay bët (liggéey rekk ko woor)
Yoral say million di ma gondi
Ay dëkku du neex, dëgg du neex
Dëggentan na neex!
Je m'en fous de ça (ay ree nga may def)
Je m'en fous de ça (ay ree nga may def)
Racagin cee pacee, tësëm gëjëm gëjëm!
Oh my God!
Gubacee, pacee
Gubacee, pacee
Cër, tësël
Cër, gichër
Ehh ko yëngel ma yëngel
Man dara dara du ma dee
Yëkkëtil loxo ca kaw
Yëkkëtil loxo ca kaw (ganaan rasagin)
Je m'en fous de ça (ay ree nga may def)
Yëkkëtil loxo ca kaw
Yëkkëtil loxo ca kaw (ganaan rasagin)
Je m'en fous de ça (ay ree nga may def)
Raw rasagin
Geex geex may ree
Ay ree nga may def (rasagin)
Geex geex may ree
Ay ree nga may def (raw rasagin)
Je m'en fous de ça (rasagin)
Je m'en fous de ça (rasagin)
Racagin cee pacee
Tësëm gëjëm gëjëm!
Oh my God!
Gubacee, pacee
Gubacee, pacee
Cër, tësël
Cër, gichër
Ehh ko yëngel ma yëngel
Man dara dara du ma tee
Ehh ko yëngel ma yëngel
Man dara dara du ma dee
Ama Sow borom bambay talibë bamba gi
Je m'en fous de ça
Yaay boroom sing saas gi DG au discours
Je m'en fous de ça
Geex geex may ree
Ay ree nga may def (rasagin)
Geex geex may ree
Ay ree nga may def (raw rasagin)
Solal say Jordan ma laal tik tik
Demal restaurant ma lal may nga
Yoral auto bu nice di ma gondi
Dëkk ci kër gu nice di ma gondi
Racagin cee pacee
Tësëm gëjëm gëjëm!
Oh my God!
Gubacee, pacee
Gubacee, pacee
Cër, tësël
Cër, gichër
Ehh ko yëngel ma yëngel
Man dara dara du ma tee
Ehh ko yëngel ma yëngel
Man dara dara du ma dee
Eh loo am doylul
Te lo yor doylul
Waawaaw
Yeye doyu rekk!
Wërsek bu de ñëw!
Dara dara du ko dee
Wat ko si Yàlla bu de am nga li ma ñàkk
Million bu la leewul gënal dërëm bi ma ñakk
Doyloo sama sombi di ko naan xel bu dal
Moo ma gënal ginnaar bu ngay time dee doo ko tal
Lu jot yomb, eeh lu jot yomb
Boroom karaw bu ñul la ñakku ma dara
Billaay lu jot yomb, eeh lu jot yomb
Boroom karaw bu ñul la ñakku ma dara
Eh man duma ñee ku yor alal
Ndax xamuma ni mu ko amee
Su ngeen tàccu dafay gëna neex
Oh my God (cakk tan)
Oh my God (cakk tan)
Cakk, cakk, ragi cagi jangicew
Ey billaay yaw, loo ran jëlel lii
Je m'en fous de ça
Más canciones de Bass Thioung
-
Bole Doley
Nila
-
Borom Darou
Nila
-
C'est Dieu
C'est Dieu
-
Chiibi Riibi
Kone Yess
-
Def Patt
Def Patt
-
Djiko
Nila
-
Dorobe
Nila
-
Gnégno
Gnégno
-
Je t'aime
Kone Yess
-
Kuur Ngany Ngalam
Nila
-
Liko Takeu
Nila
-
Louy Problème Bi ?
Louy Problème Bi ?
-
Na Flash Yi Takk
Na Flash Yi Takk
-
Niamakh Niamakh
Kone Yess
-
Nianou Yaye
Nianou Yaye
-
Nila
Nila
-
Noye Moytou Corona
Kone Yess
-
Pape Ngom
Nila
-
Sagnsè Validé
Sagnsè Validé
-
Temps Boy - Noye Moytou Sa None
Kone Yess