Dans la place

de BASH

Love bi nga may wan daf ma suur man
Dolli ma fit rekk may free
Ak yaw may def lu ma dul mën
Xol bi laa la tuddee

Li des samay àtt
Ak jàmm bi ngay daj
Lay boole jox la tokk looy laaj
Jox la sama xol
Maa doon sa support
Doo gisaat ku kay daaj comme man
Belle !

Bàyyi ma laal la profil, bébé
Yaw wax ma looy laaj?
Mënatuma toog chill, déedéet
Yaw looy waac
Hey, ma ni lii lan la?
Sama duguda ah
Yaay sama life
Hey, ma ni lii lan la?
Li ma duggu lan la?
Man yaw yaay sama life, bébé

Tippoo, yaw laa sopp tippoo
Tippoo, man sama xol laa tippoo
Yaw sibbo, yaa jar a topp sibboo
Assiko ma di ka waay ba ci kaw krekk

Ak yaw lu ma songu daan
Yaa sax ci sama xol bee
Fi nga may jàpp ci neex soo ko waññiwul dinga ma gaañ

Nank rekk
Def ma nank rekk
Ray ma rekk
No, no, ray ma rekk
Maay sa bandit saleté
Nanga ma jël ci defere ma
Jàpp rap tëj mënote ma, defaral ma

Bàyyi ma laal la profil, bébé
Yaw wax ma looy laaj?
Mënatuma toog chill, déedéet
Yaw looy waac
Hey, ma ni lii lan la?
Sama duguda ah
Yaay sama life
Hey, ma ni lii lan la?
Li ma duggu lan la?
Man yaw yaay sama life, bébé

Más canciones de BASH