Sutura
de Ashs The Best
Ci sutura
Ci sutura
Ci sutura
Sama waaji na ñu waxtaan ci sutura
Xarit dee naa la ci sutura
Ci sutura laa lay waxee sama ge′nt
Sutura
Ci sutura laa lay samay proble'mes akk lima dal
Sutura
Ci laa lay de′nkee sama guddi
Bulma weer ni bëccëg
Bulma weer ni bëccëg, sutura, sutura
Bulma weer ni bëccëg
Ndax yombul nga xamal ma
Mbokk waay
Sutura, sutura
(Sutura sutural ma)
Sutura
(Sutural ma) Sutura
(Sutura sutural ma)
Sutura
Mbokk du nii
Reeroo bumu tax nga tasaare ma
Sutura sutural ma
Ñu weetoo ma wax la sama demb nga waxaat ko tay
Xarit sama waaji, ma ne Mbokk du nii
Bulma jeebaane fii
Bul wax sama proble'me ci ñii
Woolu la tay
Waraloon demb ma wax la lu xew wax la sama xol
Mbokk waay
Sutura, sutura
(Sutura sutural ma)
Sutura
(Sutural ma) Sutura
(Sutura sutural ma)
Sutura
Más canciones de Ashs The Best
-
Waxalag'Man
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Yeye
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Réer
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Naari Xalé
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Doom
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Wommat
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Bideew
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Kurti-Kurti
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Xalam
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Waxtu
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Maam
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Ngala Way
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Yone Bi
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Ayubes
Ayubes
-
Ndogal
Millions Flows
-
Guddi - Bonus Track
Tukki
-
Guissou Mala
Millions Flows
-
Djar Djar
Millions Flows
-
Lll
Millions Flows
-
Mounouma Bayi
Millions Flows