Aras
de Ashs The Best
Bëgguma ngay gis lu la yéem
Bëgguma nga gis lu la jaaxal
Jaral na ma faat bakkan yaw nga dund
Bëgguma la gis ngay caalit
Xanaa xamoo ni benn lañ
Ndekete Yàlla ñu boole
Ndekete Yàlla ñu boole
Fii ci suuf ci asamaan si
Yàlla ñu boole, ñu doon benn say
Dinaa la xamal bu doon benn fas
Naaru góor laa ci yaw
Man dinaa la dawal Safaa'g Marwaa
Kenn du ma jiitu ci yaw
Dinaa la yëgal ni Yàlla ñu boole
Bind na ko Aras
Buñ demee ba gisatoo ma
Daa fekk man ma jiitu la Aras
Man dinaa la xamal bu doon benn fas
Naaru góor laa ci yaw
Man dinaa la dawal Safaa'g Marwaa
Kenn du ma jiitu ci yaw
Man dinaa la yëgal ni Yàlla ñu boole
Bind na ko Aras
Buñ demee ba gisatoo ma
Daa fekk man ma jiitu la Aras
Asaman ak suuf
Yaay suuf yaay asaman
Yaay bidéew biy leeral
Man dinaa la xamal ni Yàlla ñu boole
Bind na ko Aras
Buñ demee ba gisatoo ma
Daa fekk man ma jiitu la Aras
Gis la ci lëndëm bi te nekk ci leer
Baayi la fa ngay gëlëm
Metit bu naree ñëw di dal sa kaw
Ma taxaw dekku ko
Dinaa la xamal ni Yàlla ñu boole
Bind na ko Aras
Malaakal Mëwti sax bu la soxla woon
Na ma jël bàyyi la
Metit bu naree ñëw di dal sa kaw
Ma taxaw dekku ko
Yaay booy
Yaay bidéew biy leeral asaman
Asaman ak suuf
Yaay suuf yaay asaman
Yaay bidéew biy leeral
Asaman ak suuf
Dee ma ree
Dee ma ree, ma lay ree
Dee ma ree
Dee ma ree, ma lay ree
Más canciones de Ashs The Best
-
Waxalag'Man
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Yeye
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Réer
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Naari Xalé
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Doom
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Wommat
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Bideew
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Kurti-Kurti
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Xalam
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Waxtu
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Maam
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Ngala Way
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Yone Bi
Fii Kufi Judd Bëgg
-
Ayubes
Ayubes
-
Ndogal
Millions Flows
-
Guddi - Bonus Track
Tukki
-
Guissou Mala
Millions Flows
-
Djar Djar
Millions Flows
-
Lll
Millions Flows
-
Mounouma Bayi
Millions Flows